Ñooy yàpp seenug jur, lekk seen gàncax, ba ngeen raaf. Duñu leen wacce dara; du pepp, du biiñ, dug diw, du doomu jur gu gudd ak gu gàtt, ba ngeen far sànku.
TSK
TSK · Lamentations 4:9
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Jeremiah 16:4
TSK
mu ne: «Jàngoroy ndee a leen di rey. Deesu leen jooy, deesu leen rob. Seeni néew ay tosal suuf. Saamar akub xiif a leen di sànk, seeni néew leel njanaaw ak rabi àll.»
Ezekiel 7:15
TSK
Saamar biti, mbas akub xiif ci biir, ki ci àll bi deeye xare, ki ci biir dëkk bi, xiif ak mbas rey ko.
Ezekiel 33:10
TSK
¶ «Yaw nit ki, waxal ak waa kër Israyil, ne leen: “Ngeen ne dungeen mana mucc ndax seeni tooñ ak seen bàkkaar yu leen diis ba semmal leen?”