TSK

TSK · Leviticus 13:23

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Waaye su ko sarxalkat bi seetee, gisul kawar gu weex ci gàkk bi, deful pax it te raaf na, na ber nit ki juróom ñaari fan.

Job 40:4 TSK

Man mi tekkiwul dara, nu ma lay tontoo? Sama loxo laa ube sama gémmiñ.

¶ Bokki gëmkat ñi, su ñu bettee nit ci ag tooñ, yeen ñi topp Noowug Yàlla, waññileen ko ndànk, te kenn ku nekk ci yeen xoolaat boppam bu baax, ngir seen bakkan bañ leena xiirtal, ba ngeen daanu ci fiir gu ni mel.