Leviticus 14:54
TSK
¶ Loolu la yoon digle ci lépp luy jàngoroy der juy law ak wat-wataan,
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Loolu la yoon digle ci lépp luy jàngoroy der juy law ak wat-wataan,
¶ «Su nit jekkee dee ci wetam, ba sobeel njañu céddoom, keroog bés buy setlu ca lay watu, te keroog bésub juróom ñaareel ba lay watu.
Yeesu nag gis leen, ne leen: «Demleen seetluji seen yaram ca sarxalkat ya.» Ba ñuy dem ca sarxalkat ya lañu wér, seen yaram set.