TSK

TSK · Leviticus 15:32

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Loolu la yoon digle ci wàllu mala ak njanaaw ak bindeef yi nekk ci ndox, ak mboolem bindeef yu sew-sewaan yiy dox ne ñàpp ci suuf.

«Li yoon digle ci mbirum nit ku ame jàngoroy der juy law, keroog bés ba ñuy laabal nit ki, mooy lii: Nañu ko yegge sarxalkat bi.

¶ Loolu la yoon digle ci lépp luy jàngoroy der juy law ak wat-wataan,

¶ «Dogalu yoon wi ci ab nasireen nag mooy lii: Bés bi ag céddoom matee, dees koy yóbbu ca bunt xaymab ndaje ma.

Ndigalu yoon wi jëm ci kër Yàlla gi ñu wara tabax mooy lii: ci kaw tund wi ak fi ko wër fépp, fu sella sell lay doon. Loolu mooy ndigalu yoon wi, ci wàllu kër Yàlla gi.»