TSK

TSK · Leviticus 17:8

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

te indiwu ko ci bunt xaymab ndaje mi, teewalal ko Aji Sax ji, muy sarax ca bunt jaamookaayu Aji Sax ji, kooku dees na ko topp àqu deret. Dafa tuur deret. Kon dees na ko dagge ci biir bànni Israyil.

Samiyel jël menn xar mu feragul, defal ko lépp Aji Sax ji saraxu rendi-dóomal. Mu jooytul Israyil ci Aji Sax ji, Aji Sax ji nangul ko.

Samiyel ne ko: «Ana nu ma fay deme? Sóol da koy dégg, rey ma!» Aji Sax ji ne ko: «Aw nag wu jigéen ngay jël, yóbbu, ne ko sarxalsi Aji Sax ji moo la indi.

¶ Ba mu ko defee Ilyaas wax ak mbooloo ma mépp, ne leen: «Jegesileen fii!» Ñépp jegesi. Mu defaraat sarxalukaayu Aji Sax ja tasaaroo woon,