¶ «Diiru juróom ñaari fan ngeen di lekk mburu mu amul lawiir; te bés bu jëkk bi ci boppam nangeen jële seeni kër luy lawiir, ndaxte képp ku ci lekk mburu mu am lawiir, li ko dale bés bu jëkk bi, ba kera bésub juróom ñaareel ba, dees na ko dagge ci askanu Israyil.
TSK
TSK · Leviticus 18:29
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Exodus 12:15
TSK
Leviticus 7:20
TSK
Waaye ku sobewu ku lekk ci yàppu jur gu ñu defal Aji Sax ji saraxu cant ci biir jàmm, kooku nañu ko dagge ci biir bànni Israyil.
Leviticus 17:10
TSK
¶ «Te it képp ku bokk ci waa kër Israyil mbaa doxandéem yi ci seen biir, bu lekkee lenn luy deret, kooku lekk deret, man Aji Sax ji, dinaa ko noonoo te dinaa ko dagge ci biir bànni Israyil.
Malachi 2:12
TSK
¶ Ku def lii, yal na Aji Sax ji dagge ci xaymay Yanqóoba, gépp kuutaayam, boole ci kuy indil ab sarax, Aji Sax ji Boroom gàngoor yi.