TSK

TSK · Leviticus 20:19

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Amram moo jël bàjjanam Yokebedd soxna, kooku am ak moom Aaróona ak Musaa. At, ya Amram dund, téeméer la ak fanweer ak juróom ñaar (137).

¶ «Bul dëkkoo sa bàjjan, ndax daa jegewook sa baay lool cig bokk.