te it na def njotlaayal bérab bu sell bee sell ak xaymab ndaje mi ak sarxalukaay bi, boole ci defal sarxalkat yi seen njotlaay, ñook mbooloom Israyil mépp.
TSK
TSK · Leviticus 23:28
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Leviticus 16:33
TSK
Isaiah 53:10
TSK
Moona Aji Sax ji la soob, mu dëggaate jaamam bii, teg koy naqar, su nangoo doon saraxu peyug tooñ, gis askanam, aw fanam gudd, te coobarey Aji Sax ji ci moom lay sottee.
Zechariah 3:9
TSK
Doj waa ngii ma teg fi kanam Yosuwe, te wenn doj wi, juróom ñaari gët a ngi ci kawam. Maa ngii di ci ñaas mbind mi ci war,» kàddug Aji Sax jee, Boroom gàngoor yi, «te maay far bàkkaaru réew mii ci benn bés.»
Hebrews 9:12
TSK
Du deretu sikket mbaa yëkk la duggaale, waaye deretu boppam la dugge benn yoon ba fàww ca bérab bu sell baa sell, te moom la amale njotlaay gu sax dàkk.
Hebrews 10:10
TSK
Coobarey Yàlla googu moo waral ñu sellale nu sarax, bi Yeesu Almasi sarxe yaramam, benn yoon ba fàww.