Numbers 24:2
TSK
Ci kaw loolu Balaam dawal bëtam, daldi séen Israyil, na ñu dale topp seeni giir, Noowug Yàlla daldi wàcc ca moom.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ci kaw loolu Balaam dawal bëtam, daldi séen Israyil, na ñu dale topp seeni giir, Noowug Yàlla daldi wàcc ca moom.
Ci kaw loolu ñu gis ne bind nañu ci yoon wi Aji Sax ji santaane, te Musaa jottli ko, ne: «Bànni Israyil dañoo wara dëkk ci ay mbaar diiru màggalu weeru juróom ñaareel wa.»
«Man Aji Sax ji dale di sa Yàlla ca Misra, maa lay dëëlaat ciy xayma, na woon ca bésub ndaje.
¶ Ñoom ñépp ngëm lañu deeyaale te jotaguñu woon la ñu leen digoon. Waaye fu sore lañu ko séene, di ko séentu, tey ràññee ne ay doxandéem aki màngaan lañu ci àddina.