Exodus 25:30
TSK
Tegal mburum teewal mi ci kaw taabal ji, mu nekk ci sama kanam ba fàww.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Tegal mburum teewal mi ci kaw taabal ji, mu nekk ci sama kanam ba fàww.
ak taabal jeek ndabam yépp, ak mburum teewal mi ciy tege,
¶ Gannaaw loolu Suleymaan defarlu na mboolem yeneen jumtukaayi kër Aji Sax ji: muy sarxalukaayu wurus ba, ak taabal ja ñuy teg mburum teewal ma
Waaye na lépp teggine te aw yoon.