TSK

TSK · Leviticus 25:34

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

«Santal bànni Israyil ñu sàkkal Leween ñi ci seen céru suuf, ay dëkk yu Leween ñi dëkke. Àllu parlu ya wër dëkk ya it, joxleen ko Leween ñi.

Na suufas Leween ñi digalook sos sarxalkat yi, di pàkk bu gudde ñaar fukki junniy xasab ak juróom (25 000), te yaatoo fukki junniy xasab (10 000). Bu ci nekk na am guddaayu ñaar fukki junniy xasab ak juróom (25 000) ak yaatuwaayu fukki junniy xasab (10 000).

Acts 4:36 TSK

¶ Ku mel ni Yuusufa, bokk ci giirug Lewi, te dëkke dunu Sippar, ndaw yi daan ko wax Barnaba, mu firi Ñaaxekat bi,