Leviticus 25:55
TSK
Ndax kat man la bànni Israyil di samay jaam. Ñoo di sama jaam ya ma génne réewum Misra; yeen, maay seen Yàlla Aji Sax ji.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ndax kat man la bànni Israyil di samay jaam. Ñoo di sama jaam ya ma génne réewum Misra; yeen, maay seen Yàlla Aji Sax ji.
Te bu ngeen ko yiwee, mu moom boppam it, buleen ko yiwee loxoy neen.
Ndax ab jaam nga woon, ba ñu lay woo? Amul solo. Waaye soo manee yiwiku, yiwikul.