TSK

TSK · Leviticus 27:8

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ «Nit ki amul lu mat njégu gàtt, na indil Aji Sax ji ñaari pitax mbaa ñaari xati yu ndaw, muy daanam ndax bàkkaar bi mu def; benn bi di saraxu póotum bàkkaar, bi ci des di sarax rendi-dóomal.

¶ «Su fekkee ne wasin-bees wi amul njégu xar, na indi ñaari pitax mbaa ñaari xati yu ndaw, benn bi di saraxu rendi-dóomal, bi ci des di saraxu póotum bàkkaar. Sarxalkat bi defal ko ku jigéen ki njotlaayam, mu daldi set.»

¶ Ci kaw loolu ñu jóg timis, jëm ca dalub waa Siri. Ba ñu agsee ca peggub dalu waa Siri, gisuñu luy nirook nit sax.

Ndax kat ab joxe, bu àndee ak yéene rekk, la boroom joxe bi amul, deesu ci natt lees koy nangul, waaye li mu am, ci lees koy nangul ab joxeem.