TSK

TSK · Leviticus 4:22

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

«Waxal bànni Israyil ne leen: Su fekkee ne nit ki dafa moy lenn ci santaaney Aji Sax ji, ba def lenn lu warul te du teyeefam, li ci war lii la.

¶ «Su dee kenn ci baadoolo yee moy lenn ci santaaney Aji Sax ji, ba def lenn lu warul te du teyeefam, mu dig tooñam,

¶ Su dul ci teyeef ngeen ñàkka jëfe lenn ci mboolem santaane yii Aji Sax ji dénk Musaa,

¶ Ci kaw loolu Musaa ak Elasar sarxalkat ba ànd ak mboolem njiiti mbooloo ma, ñu génn dal ba, gatandu leen ca biti.

¶ Daawuda waññ askan wa ba noppi, fit wa ne rës, mu yedd boppam, daldi ne Aji Sax ji: «Aji Sax ji, bàkkaar naa lool. Léegi nag ngalla jéggal ma sama ñaawtéef, ndax def naa jëfi dof ju réy lool.»