TSK

TSK · Leviticus 8:31

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

«Lu waral lekkuleen sarax biy póotum bàkkaar ci bérab bu sell? Lu sella sell la, ñu jox leen ko, ngeen war koo yenniku bàkkaaru mbooloo mi, ba defal leen seen njotlaay fi kanam Aji Sax ji.

¶ Lii moo di li sarxalkat yooyu tàmmoona def ak askan wi. Saa yu nit indi waan juru sarax, bu ñuy togg yàpp wi, surgab sarxalkat bi day ŋàbb roqub ñetti càq, dikk,

Moo tax dootu man maay dund, waaye Almasi mooy dund léegi ci man. Sama dundu yaramu suux wii tey nag, ci ngëm gi ma gëm Doomu Yàlla laa koy dunde, moom mi ma sopp, ba jébbale boppam ngir man.