TSK

TSK · Leviticus 9:21

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ «Nanga jël dënn bi bokk ci kuuyum xewu colug Aaróona, nga def ko saraxu yékkati-jébbale, ñeel Aji Sax ji. Loolu moo cay sa wàll.

Te itam du lenn luy deret lu ngeen di lekke fenn fu ngeen dëkk, mu jóge ci njanaaw mbaa ag jur.

Moo ma ne: «Israyil yaa di samab jaam, yaw laay wonee samag leer.»

Kuy wax, na waxe nu mu jottlee kàddug Yàlla. Kuy taxawoo, na taxawoo ci dooley Yàlla, ngir màggug Yàlla feeñe ci lépp, ndax Yeesu Almasi, mi yelloo daraja ak kàttan, tey ak ëllëg ba fàww. Amiin.