TSK

TSK · Luke 1:22

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Luke 1:62 TSK

¶ Ci kaw loolu ñu liyaar baayam, ngir xam nu mu bëgg ñu tudde xale bi.

Piyeer liyaar leen, ngir ñu noppi, daldi leen nettali, ni ko Boroom bi génnee kaso ba. Mu ne leen: «Yégal-leen ko Yanqóoba ak yeneen bokki taalibe yi.» Ba loolu amee mu génn, dem feneen.

Mu may ko. Póol taxaw ca dëggastal ya, tàllal mbooloo ma loxo, ñu ne selaw. Mu wax ak ñoom ci yawut, ne: