TSK

TSK · Luke 1:3

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Lii yeena ko def! Damay noppi, ngeen defe ne damaa mel ni yeen? Dama leen di sikk, tuumaal leen, ngeen gis!

Luke 1:1 TSK

¶ Bare na ñu fexee bind ab nettalib mbir, yi sotti woon ci sunu biir,

Acts 11:4 TSK

¶ Piyeer daldi leen benn-bennalal mbir mi.

Moo tax nu mànkoo ci tànn ay nit ñu nu yebal ci yeen, boole leen ak sunuy soppe Barnaba ak Póol,

¶ Ñeel la yaw boroom réew mi, Feligsë mu tedd mee tedd, bawoo ci man Këlódd Lisiyas, mi lay nuyu.

¶ Póol ne ko: «Dofuma de, Festus mu tedd mi, dëgg gu ànd ak xel kay, laay biral.

¶ Mbokk mi Apolos nag moom, soññ naa ko lu bare, ngir mu dikk ba ci yeen, ànd ak bokk yi, waaye fii nu tollu yebuwu ci dara. Teewul bu jekkoo, dina dikk.