Numbers 11:23
TSK
¶ Aji Sax ji ne Musaa: «Loxol Aji Sax ji da koo jotewul? Léegi nag dinga gis ndax sama kàddu dina la sottil, am déet!»
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Aji Sax ji ne Musaa: «Loxol Aji Sax ji da koo jotewul? Léegi nag dinga gis ndax sama kàddu dina la sottil, am déet!»
Li ngeen xam, man it xam naa ko; duma seen cuune fenn.
«Du maay Aji Sax ji, Yàllay képp kuy dund. Ana lu ma të?»
Yeesu ne leen: «Li të nit, tëwul Yàlla.»