Genesis 22:18
TSK
te xeeti àddina sépp ci saw askan lañuy barkeele, ndax déggal nga ma.”»
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
te xeeti àddina sépp ci saw askan lañuy barkeele, ndax déggal nga ma.”»
sag wall a ko sagala sagal! Teddngaak daraja nga ko sédd,
yal na turam sax, ba law fu jant tiim, yal na xeet yépp barkeele ci moom, te di ko ndokkle.
moo geesu bii jaamam bu tekkeedi, ba maasoo maas doxe fi wooye ma boroom mbég mi,
Moo tax sama xol di nux-nuxi, samaw làmmiñ di textexi, samaw suux sax nara nopplujee yaakaar.
Nanu ne jàkk Yeesu, kiy sos, di sottal ngëm, moom mi mbég mi ñu ko waajalal tax mu dékku bant ba ñu ko daaj, tegul muy dara toroxtaange ja ko ca fekk, te doxe ca toog ca ndijooru jalub Yàlla.