TSK

TSK · Luke 10:30

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

«Moo tax, bés a ngii di ñëw,» kàddug Aji Sax jee, «maay dikke mbugal seen jëmmi tuur yi, ñoom, ñi ñu jam di binnee fi réew mi mépp.

Maay dooleel përëgu buuru Babilon, teg sama saamar ci loxoom, gannaaw ba ma dammee përëgi Firawna, muy binni binniy ku ñu jam fi kanamam.

¶ Ba Yeesu waxee loolu ba noppi, ca la jiitu, jëm Yerusalem.