Luke 14:7
TSK
¶ Ci biir loolu Yeesu gis na gan ñay taamoo toogu yu kaname, mu léeb leen, ne leen:
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Ci biir loolu Yeesu gis na gan ñay taamoo toogu yu kaname, mu léeb leen, ne leen:
Na leen mbëggeelug bokk taxa fonkante, te ngeen farlu ci di terlante.
Ndax su nit duggsee seenum ndaje, takk jaarob wurus, solu ba jekk; ku néew doole it duggsi, limboo ay sagaram,