TSK

TSK · Luke 11:45

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Buurub Israyil ne Yosafat: «Am na ba tey genn góor gu ñu mana seetal ci Aji Sax ji. Waaye man maa ko jéppi, ndax du wax waxyu bu baax ci man, lu bon rekk; mooy Mise doomu Yimla.» Yosafat ne ko: «Buur, bul waxe noonu.»

Saa yu ma waxee, damay xaacu, fitnaak salfaañoo ma tax di yuuxu. Kàddug Aji Sax jee may yóbbey xas aki saaga bés bu ne.

Ngalla yeen xamkati yoon yi, yeena sànk caabiy xam-xam; yeen dugguleen, ñiy duggsi, ngeen tere leena dugg.»