Genesis 26:12
TSK
¶ Gannaaw loolu Isaaxa bey ca réew ma, góob ca at ma lu tollook téeméeri yoon la mu ji woon, ndax Aji Sax ji da koo barkeel.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Gannaaw loolu Isaaxa bey ca réew ma, góob ca at ma lu tollook téeméeri yoon la mu ji woon, ndax Aji Sax ji da koo barkeel.
Jàmm a nga ca xaymay yàqkat ya, te xel mu dal di céru tooñkati Yàlla yooyu, ŋàbb seeni yàlla.
ngir maa ñee ku bew, ndax gis mu baaxle te di ku bon.
«Moo tax maa ngii di ñage yoonam ay dég, gawe ko ag wurmbal, ba yoon réer ko.
Moona noppiwula seereel boppam ci mbaaxam gi muy jëfe, di leen wàcceel fa asamaan, taw ak naataange, reggal leen, bégal leen ba seen xol sedd.»