TSK

TSK · Luke 14:7

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

ndax ñu ne la: «Yéegal, jegesi fii,» moo gën ñu torxal la ci kanam kilifa. Boo gisalee sa bopp it,

«Moytuleen firikati yoon yi taamoo jaagar-jaagareek seen mbubb yu réy, di sàkku nuyoob gëddaal ca pénc ma, ak toogu yu kaname ca jàngu ya, ak péetey teraanga ca bernde ya.

Buleen def dara ci kaw wujje, mbaa réy-réylu, waaye doyadiluleen, ba jàpp ne seen moroomi gëmkat a leen gën.