TSK

TSK · Luke 19:1

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Ca jamonoy Axab la Iyel ma dëkk Betel tabaxaat Yeriko. Abiram taawam la Iyel ñàkk ba muy tëral kenug tabax ba, teg ca ñàkk Segub, am caatam ba muy taxawal bunti dëkk ba. Mu dëppook kàddug Aji Sax, ja Yosuwe doomu Nuun jottli woon.

¶ Ba Yeesu di jubsi dëkk ba ñuy wax Yeriko, ab silmaxaa nga tooge ca peggu yoon wa, di yalwaan.