TSK

TSK · Luke 19:48

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Esra jàng na ko janook mbedd ma jàkkaarlook buntu Ndox ma, dale ko ba bët setee ba ca digg bëccëg. Mbooloo maa nga teew, góor ak jigéen, mboolem ña dégg la ca nekk. Ñépp nag di teewlu kàdduy téereb yoon wa.

¶ Firikati yoon yaak sarxalkat yu mag ya nag, ca saa sa lañu doon fexee teg Yeesu loxo, ndax xamoon nañu ne ñoo moom léeb woowu, waaye nit ña lañu ragal.