TSK

TSK · Luke 2:19

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Mag ya nag iñaane ko. Teewul baayam moom bàyyi xel ci mbir moomu.

Baay digal ma, ne ma: «Jàppal samay wax ci sam xel, di jëfe samay santaane, ba dund.

Luke 1:66 TSK

Ña ca dégg ñépp daldi bàyyi xel ca mbir ma, te naan: «Lu xale bii nara doon ëllëg?» ngir manoorey Boroom bee àndoon ak moom.

Luke 9:43 TSK

Ñépp nag waaru ci màggug Yàlla. Naka la ñépp di yéemu ca mboolem la Yeesuy def, mu ne taalibeem ya: