Léegi nag Buur, xamal ne bu ñu tabaxaatee dëkk boobu, ba yékkatiwaat tata ya, galag mbaa njoti bopp mbaa juuti dootuñu ko fey, te kon koomu nguur gi dina ko yég.
TSK
TSK · Luke 20:22
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ezra 4:13
TSK
Ezra 9:7
TSK
¶ La ko dale ca sunu janti maam ba bésub tey jii, nu ngi ci moy gu réy. Sunuy bàkkaar tax na buuri réew yi teg nu loxo, nook sunuy buur ak sunuy sarxalkat, ñu di nu rey, di nu jàpp njaam, di lël sunu alal, di nu torxal ba sunu jonni yàllay tey.
Nehemiah 9:37
TSK
Li suuf siy jur a ngi ne gàññ, di alalu buur yi nga teg ci sunu kaw, ndax sunuy moy. Dañu noo yilif, yilif sunug jur, nu mu leen neexe, nu nekke njàqare ju réy.»
Acts 5:37
TSK
Gannaawam it Yuda mu Galile jóg, ca jant ya ñu doon lim waa réew mi; mu yóbbaale mbooloo mu ko topp. Moom itam dee, ña ko toppoon ñépp tasaaroo.