Daniel 12:6
TSK
Kenn ki wax ak ka sol mbubbam wëñ gu ëccu ba sew, te taxaw ca kaw dex ga, ne ko: «Ana fu kéemaan yiy yem?»
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Kenn ki wax ak ka sol mbubbam wëñ gu ëccu ba sew, te taxaw ca kaw dex ga, ne ko: «Ana fu kéemaan yiy yem?»
¶ «Bu ngeen gisee gàngooru xare gu gaw Yerusalem, su boobaa xamleen ne tasteem dëgmal na.
¶ «Maa leen ko wax déy, niti tey jii duñu wéy mukk, te loolu lépp sottiwul.
¶ Naka lañu daje fa moom, daldi koy laaj, ne ko: «Sang bi, ndax ci jii jamono ngay sampaat nguurug Israyil?»