TSK

TSK · Luke 22:27

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Luke 17:7 TSK

¶ «Kan ci yeen la ab jaamam di beyi mbaa mu sàmmi ba jóge tool, dikk, mu ne ko: “Kaay, nu lekk”?

Xam ngeen kat sunu yiwu Boroom Yeesu Almasi, moom mi woomle woon, te yeena tax mu ñàkk, ngir woomale leen ag ñàkkam.