TSK

TSK · Luke 22:4

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Acts 4:1 TSK

¶ Naka la Piyeer ak Yowaan di wax ak mbooloo ma, sarxalkat yaak jawriñu kër Yàlla gaak Sadusen ya ne jimeet ci seen kaw.

Acts 5:26 TSK

Ci kaw loolu jawriñu kër Yàlla ga ak dag ya jëli ndaw ya ndànk, bañ leena jaay doole, ngir ragal nit ñi sànni leen ay doj.