TSK

TSK · Luke 5:17

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Luke 2:46 TSK

¶ Ca gannaaw ëllëg sa lañu ko fekk ca kër Yàlla ga, mu toog ca digg jànglekat ya, di leen déglook a laaj.

Luke 5:30 TSK

Farisen yi ak seeni firikat nag di xultu ci kaw taalibey Yeesu yi, ne leen: «Lu tax ngeen di lekkandoo ak a naanandoo ak juutikat yeek bàkkaarkat yi?»

Luke 7:30 TSK

Waaye Farisen ya ak xamkati yoon ya ñoo gàntal la leen Yàlla nammaloon, ba Yaxya sóobu leen ci ndox.

Ngalla yeen xamkati yoon yi, yeena sànk caabiy xam-xam; yeen dugguleen, ñiy duggsi, ngeen tere leena dugg.»

¶ Ba mu ko defee Yàlla di def ay kéemaan yu mag yu mu sottale loxoy Póol.