Isaiah 7:12
TSK
Axas ne: «Duma ko ñaan, ndax duma nattu Aji Sax ji.»
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Axas ne: «Duma ko ñaan, ndax duma nattu Aji Sax ji.»
Ci kaw loolu rekk jenn waay dikk, ku ñuy wax Yayrus, di njiitu jàngu ba. Mu ne gurub fi kanam Yeesu, sarxu ko ngir mu ñëw këram,