Psalms 37:16
TSK
Aji jub, as tuutam moo gën koomu ku bon.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Aji jub, as tuutam moo gën koomu ku bon.
Ku jub day lekk ba regg, soxor ba dëkke xiif.
Fii ma tollu jot naa li ma aajowoo lépp, maa ngi ci naataange; doyle naa sëkk, gannaaw ba ma nangoo ci loxol Epafrodit, seenub yóbbante, te sarax su ñu nangu la, di xeeñ xetug jàmm, te neex Yàlla mi mu ñeel.