¶ Aji Sax jee leen di langalal mbas, ba raafal leen ca réew ma ngeen jëm, ngir nanguji ko.
TSK
TSK · Micah 6:13
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Psalms 107:17
TSK
Ñu dofe ñalee ngi topp yoonu moy, loroo seeni ñaawtéef,
Isaiah 6:11
TSK
¶ Ma ne: «Boroom bi, foo àppal loolu?» Mu ne: «Xanaa fii ba seeni dëkk gental, ba kenn dëkkatu ca, ba nit dootu nekk biir kër ya, suuf sa yàqu yaxeet, di ndànd-foyfoy.
Fa kaw la Aji Sax ji sànnee sawara ci sama biiri yax, moo laaw ab caax ngir fakktal ma, waññi ma, jànnaxe ma, ma dëkke yoggooral.
Sunu mbaxana foq na! Wóoy ngalla nun ñi moy!