Numbers 16:34
TSK
Mboolem Israyil dégg seen yuux ya, daldi daw, te naan: «Nan daw bala noo suuf a mëdd!»
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Mboolem Israyil dégg seen yuux ya, daldi daw, te naan: «Nan daw bala noo suuf a mëdd!»
«Yerusalemee, ku lay yërëm? Ku lay jooy? Moo, ku lay geesu ne la: “Jàmm nga am?”
«Ãa! Ana nees mana nangoo Sesag? Nees mana tege loxo ki àddina sépp di kañ? Ana nu Babilon mana gente fi digg xeet yi?
¶ Yéeneb waxyu bu dal dëkk bi ñuy wax Niniw a ngi, di téereb peeñum Nawum ma dëkk Elkos.
Fu sore lañuy dànd, ndax ragal toskarey dëkk bi, te naan: «Wóoy, wóoy ngalla dëkk bu mag ba! Babilon ma ca doole ja! Ci wenn waxtu rekk la sa àtte dikk!»