TSK

TSK · Nehemiah 13:10

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Wattuleen seen bopp nag, ngir baña sàggane Leween ñi, seen giiru dund ca seen suuf.

Ci biir loolu nu dogoo def li ñu bind ci yoon wi, di yóbbu ca sunu kër Yàlla ga sunu taaw yu góor ak lu sunu jur taawloo, gu gudd gaak gu gàtt ga, di teg lépp ci loxoy sarxalkat ya fay liggéey.

ak Bet Gilgal ak diiwaani Geba ak Asmawet. Fekk na jàngkat ya tabax ay dëkk yu ndaw fa wër Yerusalem.

Du xar mu ndaw moo ma defal saraxu rendi-dóomal, mbaa sarax yoo ma terale, te du sarax su ma la teg it, mbaa saraxu cuuraay bu ma la sonale.

Waaw, nit dina sàcc Yàlla? Ndaxam yeen yeena ngi may sàcc te yeena ne: “Ana nu nu la sàcce?” Xanaa ci seen cérub fukkeelu alal akub jooxe.