Numbers 22:3
TSK
Mowab nag am tiitaange ju réy ca gàngooru bànni Israyil, ndax bare. Mowab jàq na ba mu gisee bànni Israyil.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Mowab nag am tiitaange ju réy ca gàngooru bànni Israyil, ndax bare. Mowab jàq na ba mu gisee bànni Israyil.
Moo nu may móoloo ku Yàlla móoluwul? Ana nu may rëbbe ku Aji Sax ji rëbbul?
Yanqóobaa, yaaka yànji xayma! Israyil, laa ne, yaaka taaruy màkkaan!
ndax la ñu leen dabewul woon aw ñam, mbaa am ndox, ca yoon wa, ba ngeen génnee Misra, xanaa di fey Balaam doomu Bewor ma bokk Petor ca Aram Naarim, ngir mu sàbbi leen.
Ñooy móolu, yaw nga barkeel; ñoo ma jógal, ñooy torox, man, ma bég, Sang bi!