TSK

TSK · Nehemiah 13:4

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Ba mu ko defee, Sanbalat ma dëkk Oron dégg mbir ma, mook Tobya, Amoneen ba, ndawal Buur. Ñu am lu leen soofa soof, te mooy li nit ñëw, di sàkkusi njariñu bànni Israyil.

¶ Ca yooya jamono garmiy Yuda daan nañu bindanteek Tobya lu bare.

¶ Ñu daldi tànn bésub keroog ay nit, dénk leen néegi dencukaay, ya ñuy yeb ay jooxe, ak saraxi ndoortel meññeef, ak céri fukkeel yu ñuy génne. Ñu war caa dajale nag cér ya yoon wi dogalal sarxalkat yeek Leween ñi, te mu jóge ci tool yi wër dëkk yi. Waa Yuda rafetlu ca taxawaayu sarxalkat yaak Leween ña.