TSK

TSK · Nehemiah 2:3

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Ba mu ko defee Batseba dëpp kanamam fa suuf, sukk fa kanam Buur, ne ko: «Buur Daawuda, sang bi, yal nanga fi yàgg.»

Ñu wax ma, ne ma: «Ña rawe ca njaam ga de, ña nga diiwaanu Yuda, ci njàqare ju réy akug toroxte. Tatay Yerusalem jaa nga tojatoo, bunt ya lakk.»

Maa ngi sëgg, ne yàcc, ne yasar, di wéye tiis,

Sa jaam ñeeka sopp doji dëkk bii ñu màbb, ñoo ñeewante tojiti gentam bii.

Bunti dëkk ba suulu na, te moo yàqte, dammate weñi tëjukaay ya, buuram aki garmeem a tumurànkeji ca yéefar ya, te téereb yoon amul, yonent it gisatul peeñu mu bawoo fa Aji Sax ji.

Ñu wax Buur Nabukodonosor, ne ko: «Buur, guddalu fan.

Ñu daldi ne: «Dunu gis mukk lenn lu nu tuumaal Dañeel. Xanaa nu gis ko ci yoonu Yàllaam.»