TSK

TSK · Nehemiah 5:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Leween ñi ñooy wax ak waa Israyil gépp, di àddu ca kaw, ne:

¶ Mu am bés Yerbowam doon génne Yerusalem. Axiya, yonent bu dëkk Silo ba, dajeek moom ca yoon wa. Ma nga sol mbubb mu bees. Ñoom ñaar rekk ci àll bi.

Deel jaajëfal Yàlla, sarxale ko, di fey Aji Kawe ji loo dige,

Giñ naa te di ko dëggal, ne dinaa sàmmonteek sa ndigali njekk.

Bu la sa làmmiñ yóbbe bàkkaar, ba ngay lay ndawal Yàlla la, naan lii njuumte la woon. Ana lu jar Yàlla di la meree sa kàddu, bay neenal saw ñaq?

Acts 18:6 TSK

Yawut ya nag gàntal, di ko ŋàññ, mu yëlëb ay yéreem, misaale ko ne jaanam wàcc na. Mu ne leen: «Yeenay gàddu seen bakkanu bopp. Man set naa ci wecc. Gannaaw-si-tey, ci jaambur ñi dul Yawut laa jëm.»