Genesis 46:13
TSK
Doomi Isaakar yu góor di Tola ak Puwa ak Yasub ak Simron.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Doomi Isaakar yu góor di Tola ak Puwa ak Yasub ak Simron.
¶ «Ñay dale fa feggook ñoom ñooy giirug Isakareen ñi, kilifag askanu Isaakar di Netanel doomu Suwar.
¶ Ñi askanoo ci Isaakar, ñook seeni làng ñoo di Tola mi sos làngu Toleen ñi, ak ñoom Puwa mi sos làngu Puween ñi,