TSK

TSK · Numbers 11:14

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Dangay dàjji sa bopp doŋŋ, dàjji mbooloo mi, ndax yen bee diis, ba ëpp ci sa kaw; doo ko àttan yaw rekk.

Sunu kiirlaay lii, Aji Sax jeey boroom; sunu buur bii, Aji Sell ji séddoo Israyil ay boroom.

Mooy tabax kër Aji Sax ji te mooy soloo daraja, mooy toog, di jiite cib jalam, di sarxalkat bi cib jalam, te mébétu jàmm mooy dox diggante ñaar yooyu mu sasoo.”