TSK

TSK · Numbers 13:17

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Ibraam bàyyikooti fa, aw yoonam, jublu àllub Negew.

¶ Waaye xuru Sidim woowu dafa feesoon dell aki pax aki kàmbi koltaar. Ba mu ko defee buuri Sodom ak Gomor di daw, far daanu ca kàmb ya. Ña ca des daw ba ca tund ya.

Amalegeen ñaa dëkke bëj-saalumu réew ma, Etteen ñaak Yebuseen ñaak Amoreen ña dëkke diiwaanu tund ya, Kanaaneen ña dëkke wetu géej, feggook dexu Yurdan.»

Ba loolu amee Amoreen ña dëkke tund woowa dikk, dajeek yeen, ne leen dann niy yamb, yitte leen fa Seyir, ba Xorma.