¶ Ba mu ko defee Ibraam sempi xaymaam, ñëw dal Ebron ca garab yu mag ya ca toolub Mamre, daldi fay tabaxal Aji Sax ji sarxalukaay.
TSK
TSK · Numbers 13:22
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Genesis 13:18
TSK
Numbers 13:17
TSK
¶ Ba leen Musaa yebalee ngir ñu yëri réewum Kanaan, da ne leen: «Negew gii ci bëj-saalum ngeen di jaare, yéegi ca diiwaanu tund ya,
2 Samuel 2:1
TSK
¶ Gannaaw ba loolu weesee Daawuda daa laaj Aji Sax ji, ne ko: «Ndax ma dellu ci dëkki Yuda yi benn?» Aji Sax ji ne ko: «Demal.» Daawuda ne ko: «Bu ma ciy dem?» Aji Sax ji ne ko: «Ebron.»
Psalms 78:12
TSK
Fa seen kanami maam la def kéemaan, fa diiwaanu Cowan, réewum Misra.
Isaiah 19:11
TSK
Kàngam ya fa Cowan dañuy teqlikook seen sago, diglekati Firawna yu xelu ya di digle ag ndof. Ma ne: «Yeen diglekat yi, nu ngeen mana waxe Firawna naan: “Nun ay boroom xel lanu, sosoo ca buur ya woon”?»
Isaiah 30:4
TSK
Seeni jawriñ a nga xaat ba Cowan, seeni ndaw àgg ba Anes,