Numbers 13:33
TSK
Fa lanu gis xeetu Nefilim ya, ponkali Anageen ña bokk ca xeetu Nefilim ya, nuy niru sunu bopp ay soccet fi seen kanam, di leen ko niru, ñoom it.»
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Fa lanu gis xeetu Nefilim ya, ponkali Anageen ña bokk ca xeetu Nefilim ya, nuy niru sunu bopp ay soccet fi seen kanam, di leen ko niru, ñoom it.»
¶ Emeen ñaa fa jëkkoona dëkk, askan wu am kàttan lañu woon, bare, yegg ca kaw ni Anageen ñi.
Yooyu yépp di dëkk yu dàbblikoo tata yu kawe, ak bunt yu tëje ràpp, te limaaleesul dëkk-dëkkaan yu baree bare, yu dara wërul.