TSK

TSK · Numbers 16:30

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Job 31:3 TSK

Xanaa du safaan a ñeel ku bon, naqar ñeel ku ñaaw?

Aji Sax jeey jóg na woon fa tundu Perasim, xadaru na woon ca xuru Gabawon ngir jëf jëfam, jëfam ju yéeme ja! Moo nara liggéey liggéeyam booba, liggéeyam bu tumurànke ba!

Maay bind leer, di def lëndëm. Maay indi jàmm, di def safaan. Maay Aji Sax jiy def lii lépp!

Ndaw su toogadi si, foo àppal sa ciŋiñ-caŋañ ji? Aji Sax ji déy, sàkk na guléet kaw suuf: yees ba mel ni jigéen juy jëflanteek góor.»