TSK

TSK · Numbers 18:4

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Bu jaamookaay bi dee dem, Leween ñee koy wékki, bu jaamookaay bi dee dale bérab, Leween ñee koy we. Ku ci bokkul ba laal ci nag, dees koy rey.

Aaróona ak doomam yu góor nag ngay tabb ngir ñu sasoo seenug carxal, waaye képp ku ci laal te bokku ci, dees koy rey.»

¶ Terewul Yàlla mbugal ñenn ca waa Bet Semes, ndax dañoo yërndu woon ca biir gaalu Aji Sax ja. Juróom ñaar fukki nit la fàdd ca ñoom. Waa dëkk ba nag di tiislu ndax mbugal mu réy moomu leen Aji Sax ji teg.

Waaye maa leen di def ñuy nit ñiy dénkoo dénkaaney kër gi ci mboolem liggéey bu mu laaj, ak mboolem lees di def ci biir.