Gàtt ba bumu am sikk te na di kuuyu menn at. Man naa doon xar mbaa sikket.
TSK
TSK · Numbers 19:2
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ «Bu saraxam dee ab gàtt bu ñuy def rendi-dóomal, muy xar mbaa bëy, na sarxal bu góor bu amul sikk.
Lenn lu ci am sikk buleen ko sarxal, ndax deesu leen ko nangul.
¶ Ba mu ko defee Elasar sarxalkat ba wax ak ña xareji woon, ne leen: «Lii moo di dogalu yoon, bi Aji Sax ji dénk Musaa:
Kon waajal-leen watiir bu bees te ngeen jël ñaari nag yuy nàmpal yu ñu masula takkal. Ngeen takkal nag yi watiir bi te yóbbu doomi nag yi, fat.
Samay tooñ la Aji Sax ji ëmb, fastee ko loxoom, mu tege sama kaw ndodd, ba jeexal sama doole. Boroom bee ma tàbbal ci loxo yu ma manula të.
Malaaka mi ne ko: «Noo gu Sell gi mooy wàccsi ci yaw, dooley Aji Kawe ji yiir la. Moo tax itam ku Sell kiy juddoo ci yaw, dees na ko wooye Doomu Yàlla.
Moom mi nekke nekkinu Yàlla te ŋoyaaloowul dayob boppam, bi ko def nawleb Yàlla.
Sarax yooyu, ci aw ñam ak ag naan, ak xeeti njàpp doŋŋ la jëm, lépp yittewoo yaramu suuxu neen, te di ndigal yu leen waroon ba keroog bésub coppite taxaw.
«Moo bàkkaarul, fenul.»